SNAD - Société Nouvelle Africaine de DistributionWO
Sunuy solo

Naka lañuy liggéeye, du ay kàddu rekk.

Dëggu, liggéey, rigueur, jege klient, yombal ak kóllëre ñoo jiite SNAD.

01

Dëggu

Xibaar bu leer ak wax ju wóor ñoo tax kóllëre di yàgg.

02

Liggéey ak rigueur

Dale ci stock ba ci livraison, lépp dañu koy organise ngir liggéey bu baax.

03

Jege ak kóllëre

SNAD dafay jege grossiste, boutique, entreprise ak particulier yi, te crédit am na ngir klient yépp.

SNAD, ba ci sa buntu

So amee soxla, komande, sunu ekip ànd ak yaw.

Gis sunuy produi, komande ci SNAD Direct walla jokkoo ak sunu ekip.